Luke 4:42 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ca njël gu jëkk Yeesu génn, dem ca bérab bu wéet. Mbooloo ma di ko seet. Bi ñu ko gisee, ñu koy wut a téye, ngir bañ mu dem.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Njël gu jëkk ca ëllëg sa la Yeesu génn dëkk ba, dem ba bérab bu wéet. Mbooloo ma nag di ko seet, ba dikk, di ko téye, bañ mu dem, ba leen.