Luke 5:10 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
ak ña mu bokkaloon liggéey ba, maanaam ñaari doomi Sebede yi di Saag ak Yowaana. Yeesu ne Simoŋ: «Bul ragal dara; gannaawsi tey, ay nit ngay mbaal jëme ci man.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yanqóoba ak Yowaan doomi Sebede ya mu bokkaloon liggéey ba itam noonu lañu tiite. Yeesu ne Simoŋ: «Bul ragal dara; gannaaw-si-tey, ay nit ngay napp.»