Luke 5:16 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Waaye Yeesu moom di beddeeku ci bérab yu wéet ya, di ñaan.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Moom nag muy rocceekuy dem ba ci bérab yu wéet, di fa ñaaneji.
Recommended Reading