Luke 5:18 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu ay nit ñëw, jàppoo basaŋ, ga ñu tëral nit ku yaram wépp làggi. Ñu di ko wut a dugal ca kër ga, ngir indi ko ca Yeesu.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci biir loolu ay nit ne jalañ, jàppoo ab lafañ bu ñu tëral cig laltu. Ñu di ko wuta dugal, ngir tëral ko ca kanam Yeesu.