Luke 5:9 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Wax na loolu nag, ndax jën yu bare ya ñu mbaaloon daf koo jaaxal, moom ak ña mu àndaloon
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
ndax tiitaange lu ko jàpp, mook mboolem ña mu àndal, ca jën yu bare ya ñu jàpp.