Luke 6:11 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Waaye nit ña mer ba fees, di rabat pexe yu jëm ca Yeesu.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñu mer nag ba fees, di diisoo ci seen biir nu ñuy def ak Yeesu.
Recommended Reading