Luke 6:21 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Yéen ñi xiif léegi, barkeel ngeen,ndax dingeen regg.Yéen ñiy naqarlu léegi, barkeel ngeen,ndax dingeen ree.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndokklee yeen ñi xiif tey, nde dingeen regg. Ndokklee yeen ñiy jooy tey, nde dingeen ree.