Luke 6:22 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Barkeel ngeen, bu leen nit ñi bañee, di leen dàq ak a saaga, di sib seen tur ngir Doomu nit ki.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndokklee yeen, bu leen nit ñi bañee, daggook yeen, saaga leen, sikkal seen der ndax Doomu nit ki.