Luke 6:27 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
«Waaye maa ngi leen koy wax, yéen ñi may déglu, soppleen seeni bañaale tey defal lu baax ñi leen bañ.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Yeen ñi may déglu, dama ne, seeni noon, soppleen leen, seeni bañ, defal-leen leen lu baax.