Luke 6:31 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Defal-leen nit ñi li ngeen bëgg, ñu defal leen ko.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Lu ngeen bëgg nit ñi defal leen ko nag, nangeen leen ko defale noonu.
Recommended Reading