Luke 6:39 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu Yeesu wax na leen beneen léeb ne leen: «Ndax gumba man na wommat moroomam? Mbaa duñu daanu ñoom ñaar ci kàmb?
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yeesu léebati leen, ne leen: «Ndax gumba dina wommat gumba? Mbaa duñu ànd tàbbi ci kàmb?