Luke 6:5 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Yeesu dellu ne leen: «Doomu nit ki mooy boroom bésu noflaay bi.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mu neeti leen: «Bésub Noflaay, Doomu nit ki mooy boroom.»
Recommended Reading