Luke 6:8 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye Yeesu xam seen xalaat, daldi ne ku loxoom làggi: «Jógal taxaw ci kanamu ñépp.» Nit ka daldi jóg taxaw.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yeesu nag xam seen xalaat, daldi ne boroom loxo ba: «Jógal taxaw fii ci digg bi.» Mu jóg taxaw.