Luke 7:1 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi Yeesu waxee la mu naroon a wax lépp ca kanamu mbooloo ma, mu daldi dem Kapernawum.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yeesu wax na kàddoom googu gépp, askan way dégg, mu doora jàll biir Kapernawum.