Luke 7:15 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu nit ka dee woon jóg toog, tàmbalee wax. Yeesu delloo ko yaay ja.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Néew ba jóg toog, di wax, mu delloo ko yaay ja.