Luke 7:18 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Taalibey Yaxya ya nettali mbir yooyu yépp seen kilifa. Noonu Yaxya woo ñaar ci ay taalibeem,
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci kaw loolu taalibey Yaxya àgge Yaxya loolu lépp. Mu woo ñaar ca taalibe ya,