Luke 7:19 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
yónni leen ci Boroom bi, ngir laaj ko: «Ndax yaw yaa di Ki war a ñëw, walla danoo war a xaar keneen?»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
yebal leen ci Sang bi, laaj ko ne ko: «Ndax yaw yaa di Ki wara ñëw, am keneen lanuy séentu?»