bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Luke 7:2
Luke 7:2 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Amoon na fa njiitu xare. Njiit la nag, surgaam bu mu bëggoon lool dafa feebaroon, bay bëgg a dee.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Foofa nag ab njiitu takk-der bu waa Room a nga fa woon, ab jaamam woppoon bay bëgga dee, te njiit la soppoon ko lool.