Luke 7:20 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi taalibe ya agsee ca Yeesu, ñu ne ko: «Yaxya moo nu yebal, nu laaj ndax yaa di Ki waroon a ñëw, walla danuy xaar keneen?»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Taalibe ya dikk ne ko: «Yaxya moo nu yebal, di la laaj ndax yaa di Ki wara ñëw, am keneen lanuy séentu?»