Luke 7:27 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Yaxya male moo di ki ñu waxoon ci Mbind mi naan:“Maa ngi yónni sama ndaw, mu jiitu la,te xàllal la yoon ci sa kanam.”
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci moom moomu lañu bindoon ne: “Maa ngii di yebal sama ndaw, mu jiitu la, xàllal la saw yoon.”