Luke 7:28 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Maa ngi leen koy wax, ci li jigéen jur, ku sut Yaxya musul a feeñ. Waaye ba tey ki gën a ndaw ci nguuru Yàlla moo ko sut.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Maa leen ko wax, li jigéen jur, kenn sutu ci Yaxya. Waaye ki gëna tuut ci nguurug Yàlla sax moo ko sut.»