Luke 7:3 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi mu déggee mbiri Yeesu, mu yónni ca moom ay Yawut, di magi dëkk ba, ngir ñaan ko, mu ñëw faj surga ba.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba njiit la déggee mbiri Yeesu, daa yebal ñenn ca magi Yawuti dëkk ba ca moom, ñaan ko ngir mu dikk xettli jaamam.