bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Luke 7:32
Luke 7:32 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Ñu ngi nirook xale yu toog ca pénc ma tey woowante naan:“Liital nanu leen ak toxoro, te fecculeen,woyal nanu leen woyi dëj, te jooyuleen.”
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñu ngi nirook xale yu toog ca pénc ma di awoonte, naan: “Noo leen toxorool, fecculeen, nu dëjal leen, jooyuleen.”