Luke 7:35 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Waaye li xam-xamu Yàlla di jur, mooy firndeel ne dëgg la.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye xel mu rafet, mboolem la mu jur mooy la koy dëggal.»
Recommended Reading