Luke 7:36 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Amoon na ab Farisen bu ñaan Yeesu, mu ñëw lekkandoo ak moom. Yeesu dem kër waa ja, toog ca lekkukaay.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kenn ca Farisen ya moo woo woon Yeesu, ngir ñu bokk lekk. Yeesu agsi kër Farisen ba, daldi dikk ca ndab la.