bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Luke 7:40
Luke 7:40 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Yeesu ne ca tonn, daldi ne Farisen ba: «Simoŋ, am na lu ma la war a wax.» Simoŋ ne ko: «Waxal, kilifa gi.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yeesu nag àddu, ne ko: «Simoŋ, dinaa la wax lenn.» Mu ne ko: «Waxal, sëriñ bi.»