Luke 7:45 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi ma agsee, fóonuloo ma, waaye moom, bi ma duggee ba léegi tàyyiwul ci di fóon samay tànk.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Fóonuloo ma, dalale ma, waaye moom, ba ma duggsee ba léegi noppiwula fóon samay tànk.