Luke 7:46 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Defuloo diw ci sama bopp, waaye moom, sotti na latkoloñ ci samay tànk.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ag diw, diwewoo ko sama bopp, waaye moom, diwu xeeñlu la diw samay tànk.
Recommended Reading