Luke 7:49 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu ñi doon lekkandoo ak moom di wax ci seen xel naan: «Kii am sañ-sañu baale bàkkaar mooy kan?»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci kaw loolu ña mu toogandool di lekk, naan ci seen xel: «Kii mooy kan bay jéggaley bàkkaar sax?»