Luke 7:6 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Noonu Yeesu daldi ànd ak ñoom. Waaye bi ñuy bëgg a agsi ca kër ga, njiit la yebal ay xaritam ngir ñu wax Yeesu ne: «Sang bi, bul sonal sa bopp, ndaxte yeyoowuma nga dugg sama kër.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yeesu daldi ànd ak ñoom. Naka la jubsi kër ga, njiit la yóbbante ay xaritam kàddoom, ñu gatandu Yeesu, ne ko: «Sang bi, jarul ngay sonn, ndax sab tànk sama biir kër, man yeyoowuma ko.