Luke 8:1 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Gannaaw loolu Yeesu di dem ca ay dëkk yu mag ak yu ndaw, di waaraate ak di yégle xebaar bu baax bi jëm ci nguuru Yàlla. Fukki taalibe ya ak ñaar ànd ak moom,
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Gannaaw loolu Yeesu wër dëkkoo dëkk bu mag ak bu ndaw, di waare, di yégle xibaaru jàmm bu nguurug Yàlla, ànd ak fukki taalibe yaak ñaar,