Luke 8:19 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu ndeyu Yeesu ak ay rakkam ñëw seetsi ko, waaye mënuñu woon a agsi ci moom, ndaxte nit ña dañoo bare.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yaayu Yeesu ak ay rakkam ñoo dikkoon di seet Yeesu te manuñoo agsi ci moom ndax nit ñu bare.