Luke 8:30 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu Yeesu laaj ko: «Noo tudd?» Mu tontu ne: «Coggal laa tudd.» Dafa wax loolu, ndaxte rab yu baree ko jàppoon.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yeesu ne ko: «Noo tudd?» Mu ne ko: «Coggal.» Ndax rab yu baree duggoon waa ji.