Luke 8:38 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Nit ki Yeesu tàggale woon ak rab ya ñaan ko, ngir ànd ak moom. Waaye Yeesu woññi ko ne ko:
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
nit ka teqlikook rab yi di ko sarxu ngir ànd ak moom. Teewul Yeesu yiwi ko, ne ko: