Luke 8:39 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
«Ñibbil, nettali li la Yàlla defal lépp.» Noonu waa ji dem di wër dëkk ba yépp, di fa yégle la ko Yeesu defal.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Ñibbil, te nga xamle li la Yàlla defal lépp.» Waa ja it dem di siiwal ca dëkk ba bépp, mboolem la ko Yeesu defal.