Luke 8:41 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu nit ñëw, tuddoon Yayrus te nekk njiitu jàngu ba. Bi mu agsee, mu daanu ci tànki Yeesu, saraxu ko mu ñëw këram,
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci kaw loolu rekk jenn waay dikk, ku ñuy wax Yayrus, di njiitu jàngu ba. Mu ne gurub fi kanam Yeesu, sarxu ko ngir mu ñëw këram,