Luke 8:42 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
ndaxte jenn doomam ju jigéen, ji mu amoon kepp te muy tollu ci fukki at ak ñaar, ma nga doon waaj a dee. Bi Yeesuy dem, nit ñaa ngi doon buuxante, di ko tanc.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
ndax kenn la amoon ci doom, janq bu am fukki at ak ñaar, te ma nga doon waaja dee. Yeesoo ngay dem, nit ña raj-rajloo, tanc ko.