Luke 8:46 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye Yeesu ne: «Am na ku ma laal, ndaxte yég naa ne, am na doole ju génn ci man.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Teewul Yeesu ne: «Am na ku ma laal kay, ndax yég naa leer gu bàyyikoo ci man.»