Luke 8:47 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Te jigéen ja xam ne, mënul woon a nëbb li mu def. Mu daldi daanu ci tànki Yeesu, di lox. Noonu mu nettali ci kanamu ñépp li taxoon mu laal Yeesu, ak ni mu wére ca saa sa.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndaw sa xam ne feeñ na. Mu daldi dikk, di lox, ne gurub fa kanam Yeesu, daldi wax ca kanam ñépp la waral mu teg ko loxoom, ak na mu wére ca saa sa.