Luke 8:53 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye ñu di ko ñaawal, ndaxte xamoon nañu ne, dee na.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci kaw loolu ñu di ko kókkali, ndax xamoon nañu xéll ne dee na.