Luke 8:54 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye Yeesu jàpp loxob janq ba, woo ko ne ko: «Xale bi, jógal.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yeesu itam jàpp ca loxol janq ba, daldi àddu ca kaw, ne ko: «Janq, jógal.»