Luke 8:56 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waajuri xale bi daldi waaru. Waaye Yeesu tere leen, ñu wax kenn li xew.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waajuri xale bi nag waaru. Teewul Yeesu dénku leen, ne leen bu ñu wax kenn la xew.