Luke 8:7 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Leneen nag wadd ci biir ay xaaxaam, ñu saxandoo, xaaxaam ya tanc ko.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Leneen la wadde biiri xaaxaam, jógandoo ak xaaxaam ma, daldi fatt ba wow.