Luke 9:20 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Yeesu ne leen: «Yéen nag ku ngeen ne moom laa?» Piyeer tontu ko ne: «Yaa di Almasi, bi Yàlla yónni.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yeesu ne leen: «Yeen nag, ngeen ne maay kan?» Piyeer ne ko: «Yaa di Almasib Yàlla.»