Luke 9:22 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
teg ca ne: «Doomu nit ki war na sonn lu bare; saraxalekat yu mag ya ak xutbakat ya dëddu ko, ñu rey ko, mu dekki ca ñetteelu fan ba.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mu neeti: «Fàww Doomu nit ki sonn lu bare, ba dajeek mbañeelu magi askan wi ak sarxalkat yu mag yi, ak firikati yoon yi, te dees na ko rey, ba ñetteelu fanam, mu dekki.»