Luke 9:23 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu Yeesu ne leen ñoom ñépp: «Ku bëgg a aw ci samay tànk, na bàyyi boppam, gàddu bés bu nekk bant, bi ñu ko war a daaj, door a topp ci man.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yeesu nag wax leen ñoom ñépp, ne leen: «Képp ku bëgga dikk topp ma, fàtteel sa bopp, te nga gàddu bés bu nekk, bant bi ñu lay daaj, door maa topp.