Luke 9:26 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ku ma rus a faral, te nanguwul samay wax, Doomu nit ki dina la rus a xam, bés bu ñëwee ci ndamam ak ci ndamu Baay bi ak lu malaaka yu sell yi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Képp ku kersawoo sama jëmm, kersawoo topp samay wax, yaw itam Doomu nit ki dina la kersawoo, bés bu dikkee ci darajaam ak darajay Baay bi, ak darajay malaaka yu sell yi.