Luke 9:30 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Am ñaari nit di waxtaan ak moom, muy yonenti Yàlla Musaa ak Iliyas.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci kaw loolu ñaari nit jekki feeñ, di waxtaan ak moom; ñuy Yonent Yàlla Musaa ak Yonent Yàlla Ilyaas.
Recommended Reading