Luke 9:4 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Kër gu ngeen dugg, dal-leen fa, ba kera ngeen di fa jóge.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kër gu ngeen dugg, fa ngeen di dal, ba kera ngeen dem.