Luke 9:40 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Ñaan naa say taalibe, ñu dàq ko, waaye mënuñu ko.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñaan naa say taalibe ngir ñu dàqal ma ko, waaye manuñu ko.»
2 translations compared side by side